« Dama beugone mbarane ben toubab… », la suite de l’histoire est inattendue, une leçon très sévère

0
411

L’histoire de cette servira de leçon aux autres.

Bonne lecture !

« Salam Tuto defal ano je suis une fille de 30ans j’habite à Dakar. Pendant les vacances j’étais à Mbour saly sila hamanté ak beneu paa toubab mani damakoy mbaraan ma demm xaritto ak mom bamou doxane ma niou done geneu. Un jour sila toubab bi propose ma contract marriage pour 9 mois louma beugg mou defal mako mane aussi pareille ma accepté lolou. Toubab bi marié ma. Depuis notre mariage la problème yi commencé dafma done door sak jour ma tokk di mougne rek di espère avan 9 mois yi dieh ma lekk ci mom Lou beuri. Tuto c’est le contraire toubab bi dafma nahh Lou grave ndeké da neugone gnibi Belgique 🇧🇪 yoroul xaliss mou feneu ma ni da diayy sama auto bi mou tegal maci xaliss dieundeul ma auto bou bess. Fekk Amna kou beugone sama auto bi niou diayy ko. Ma deff erreur dielll xaliss bi yepp dioh ko Martin pour mou tekk ci dieundal ma auto bou bess. Tutodakar après 3 jours sila demm foumou loser a saly niounima toubab bi Gnibi na depuis hier. Je sais plus quoi faire ak foumakoy wahé depuis lors degatou ma ko feneu »

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici